Wéétoo (L'ennui)

Paroles : El Hadji Diouf et Karim Diouf
Musique : El Hadji Diouf, Karim Diouf et Mike Sawatzky

Wéétoo, wéétatinaa yaay
Wéétatinaa, wéétatinaa, wéétatinna yaay
Sophie demna tey ma dabiko
Sainte-Marguerite sorina tey ma dabiko

Sophie demna, moommii nëwna,
moommi demna nii
Sophie demna, moommi newna
moommii demna nii
Sophie demnaa tey ma dabiko
Sainte-Marguerite sorinaa tey ma dabiko

Demnaa fimu dem sorinaa
sana guel demnaa yow
Fimu dem sorinaa tey ma dabiko ndeysaay

Retour